Mollah Morgun : « Ousmane Sonko fallou na, moy reew mi neekh na… »

0
509
Mollah Morgun : « Ousmane Sonko fallou na, moy reew mi neekh na… »

Apres Nittdof, c’est au tour d’un autre rappeur, activiste de soutenir la candidat Ousmane Sonko. Dans un texte écrit en Wolof, l’ancien membre du groupe Keur gui étale les qualités du leader du parti Pastef les patriotes. Selon lui, Sonko est différent des autres politiciens, il a les mains propres, il n’est pas obnubilé par le pouvoir, il a la tête bien faite, il est jeunes… Bref, c’est lui qui détient les clés du changement. 

L’intégralité de son post titré OUSMANE SONKO, C’est L’homme Kil faut….

La Solution est bien là faut la saisir….

Senegal beug nguen reew mi changer /
Bollo leen /fall leen /Ousmane sonko
Président sonko /c l’homme kil ns faut/ Systèmou sonko/deugueul /djioubeul moy solution/ Pasteff defar sunu reww
bollo ndo/ songo /dindi fi corruption/ Dolé badola la neew na/wayé diambaat dieexna/Patriote bi nieuw na/Ousmane Sonko fallou na/ moy reew mi neekh na/Xeex ba defar deuk bi/ neewou ma /mounoul nekk/ Ndombal tank reww mi si ndiekk/Dink leen ko sonko/Ndem manoul niakk/
Aythia leen niou songo/ bolè dolé lonko /
Fall Sonko/Ndaw la beug na reew mi /
gor la/ garmi la/Tè Bop bi fess na delleu/
jeuf j sett tè selleu /yarou na def ni thielleu/djiko yi baax t rafett/ lokho yi weekh na taall/ en faite/woutènak gni diapè ngour fo fèthie ak fête/bilahi dinagn am mbètèl bou reuy sèn beussou dèfaite/Sonko cest une tête/pleine et bien faìte/Bokoul si gniy Loubeul/Alalou reew fou waur lakoy Dougueul/ Mom la guiss thi ki gniou meuna arr si Mbougueul /Ousmane Sonko mandou na té day Djioubeul/Goné yi dieul leen sen responsabilités à 2 mains/ kay lén niou goungué Sonko mou gagner demain/bouleen nangou kou leen corrompre/ Dieul lèn sén destin en main/Yeen nakhèmbay politics yu dagn ko rompre/ fowee niou/ nakh niou/ fallou /fatee niou/ foli leen/ diot na.Dou ps dou pds dou parti Niass Dou maky dou reew mi/keen amouthi pass pass/cathie sathie rawalé / ay pékhé loubeul lagniy nass/ Ousmane gawè niou/ sauwé niou/ Alternance générationnelle nguir adouna nawee niou/ thiopité bou waur/si justice bi ak fepp fi febar macky(maquis sale) bi walleu.NDIOUBLUNG yi bayi daur /reww mi naat/ lepp matt/ nieup am war di daur/ avec Ousmane Sonko pour un changement radical

LAISSER UN COMMENTAIRE

S'il vous plaît entrez votre commentaire!
S'il vous plaît entrez votre nom ici

Ce site utilise Akismet pour réduire les indésirables. En savoir plus sur comment les données de vos commentaires sont utilisées.